Overblog Suivre ce blog
Editer l'article Administration Créer mon blog
8 janvier 2008 2 08 /01 /janvier /2008 01:28


Sante Mawlana, Borom Assaman

Mome mignou bolèg Muhammadu sang bëppu man

Muhammadu Rassol borom xoutboki kêman

Kaddu djipp, doy ngagnu royuway, saway geustul xourân,

Si walu wuné, moxam nassila ba lân

Bilay têrébi doyna kêman

Sou Lahou ahad digléwone, cone ma sax dila wo yê jah man

Cone diouli ak seulmal dayiman fiyak felè, ci sang bëppu man

 

 

Partager cet article

Repost 0
Published by CMAN
commenter cet article

commentaires